04/04/2026
Aka ñoo ñàkk jom !
Ànd sàmm jikko yi,
04/04/2026
Aka ñoo ñàkk jom !
😭😭😭
Solos loi bi lii bokk na ci
Góor wala jigéen ku ci soppi sa bind ngir dooon keneen kudul yaw, yoon dal sa kaw
https://www.facebook.com/share/r/1AuW7kGt8C/
Bàjje nu góor jigéen ya
Ña ngay xataraa yu reg
Waaye xnaa ci bity waaye fii Ci Sénégal
Défendre góor jigéen jeex na fi tàkk
👇👇👇👇
Le a adopté, le 11 mars, une loi durcissant les peines contre l’ et criminalisant sa “promotion”.
Décryptage des enjeux juridiques avec Alice Nkom, avocate engagée pour les droits sur France 24 Afrique ⤵️
31/03/2026
ALHAMDOU LILLAAH
LOI BU PRESIDENT PROMULGUER NA KO !
JËREJËF PRESIDENT DE LA RÉPUBLIQUE BASSIROU DIOMAYE DIAKHAR FAYE.
JËREJËF PREMIER MINISTRE OUSMAN SONKO.
JËREJËF MINISTRE DE LA JUSTICE YACINE FALL.
JËREJËF PRÉSIDENTE ASSEMBLÉE NATIONALE EL HADJI MALICK NDIAYE.
JËREJËF MBOOLEEM BEPUTÉ YI VOTÉ LOI BI.
JËREJËF MBOOLEEM SUNUY KHALIF GÉNÉRALE AK ÑIN̈ NJABOOTE CI DIINE AK CI AADA.
JËREJËF IMAAM YI, SERIGNE DAARA.....
JËREJËF ASKA NU SÉNÉGAL CI SEEN TÀKKU TAXAW TEMM NGIR LOI BII J̌ALL SÉNÉGAL
JËREJËF MBOOLEEM ÑI ÀNDOON AK NUN CI COMBAT BI.
BIS NI KI TAY KUÑ JAPPA TI CII ÑU LIM CI LOI BII
LOI BII MOO LAY ATTE !!!
ÀTTE KATTI YÉENA CI DES.
24/03/2026
Loi contre l’homosexualité: Oustaz Makhtar révèle des documents exclusifs et répond aux menaces Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :https://www.youtube.com/channel/UCUotxi5bHZo2hVxyn6Ss6RQ/joinSeneweb, c'est le site numéro 1 , ...
Effet Modification article 319 bi 🤛🤛🤛
Yéenëg séen xaalis ak seen jàppale ça àll kuti ya ❌️❌️❌️
ANA ÑI DOON WAX GÓOR JIGÉEN DAÑOO KONTAAN CI LOI BI ?
XANAA SEEN BÀJJEN YII DILEEN JÀPPALE BOKKUÑ CI ?
LOI BII KU CI MER NALA LEER NI YAAK GÓOR JIGÉEN YI AK SEEN BÀJJEN YI, YÉENA BOKK MER GI !!!
.................
Loi contre l’h0m0sexualité : Cécile Neven veut sancti0nn€r le Sénégal
J’annule mon déplacement prévu fin mars au Sénégal.
17/03/2026
Communiquer de Ànd sàmm jikko yi pour démentir Dulu sori dulu jege ànd sàmm jikko yi collaboré wul ak benn association internationale limiy xeex ci biir reew mi lakoy xeexee tekk ko ci lu leer nàññ !te waa reew mi doyna ñu ko ci xeex bi 🙏
✍️ Coordinateur Nationale ÀND SÀMM JIKKO YI
Imam Babacar Sylla
Sénégal ngay gis kulay xasee li mu doon
Ku bëgë xas Waa Ànd Sàmm jikko yi, da naan ay politiciens lañ, ta moom mi koy wax lim lay xa see la.
Oustaz Makhtar Sarr
Deuxième vice-président chargé des relations extérieures 👇